daara (ji)
Apparence
Wolof
[Soppi]Mooy barab ba ñuy jànge ak a jàngale, cosaan la: fa jàngkati alxuraan ya daan jànge ak way xamlu diiney Lislaam ya, mu jëm-kanam ba ñu mujj di ko jëfandikoo ci lépp lu di barabu njàng ak njàggale
Turandoo
[Soppi]Yeneeni làkk
[Soppi]wu faraas: école, centre |
wu itaali: scuola |
wu angalteer: school |