jàngu (ab)

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

Am na ñaari tekki:

Diine
mooy fi katolik yi di jullee
Njàng
mooy barab ba njàngaan yi di amalee seenum njàng.

Yeneeni làkk[Soppi]

wu faraas: école, église
wu itaali: scuola, chiesa
wu angalteer: school,church