Aller au contenu

diine

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]

diine:

  1. diine lees gëm di ci tënku ngir jaamu,

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

[Soppi]
  1. diine ji ëpp ay nit fim ne mooy diiney Nasaraan

Xool it

[Soppi]

Tekki

[Soppi]

Waxiin

Déglu baatu diine ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-diine.ogg