daara

Jóge Wiktionary.
Aller à la navigation Aller à la recherche

Wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

cosaan la: fa jàngkati alxuraan ya daan jànge ak way xamlu diiney Lislaam ya, mu jëm-kanam ba ñu mujj di ko jëfandikoo ci lépp lu di barabu njàng ak njàggale. → Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

Open book 01.svg Tur[Soppi]

daara j

  1. mooy barab ba ñuy jànge ak a jàngale.