Aller au contenu

baax

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

baax :

  1. aw melo la wu nit ñi gën di melawoo,
  2. li nu baaxoo gis ci àdduna, ba tax ku def leleen ñu ni xarbaax la,

Xool it

[Soppi]

Waxiin

[Soppi]

Déglu baatu baax ci wolofi Senegaal