bind
Aller à la navigation
Aller à la recherche
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
bind: amna ñeenti maanaa
- aw bind rëdd wu mat bees war wàcci ngir bindaat weneen,
- bind amal ay baat, ci sa loxo walla wuutuloxo,
- bind gi nu Yàlla bind, maanaam sàkk,
- ab bind melow bind,
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]
- sa bind wi rafet na,
- yaangi bind ?
- Yàllaa nu bind ngir nu jaamu ko!
- sama bindu tay bii de xaw ma numay def bamu mokk,
- ndaw sii bind bi moo rafet!
Bàyyikoo[Soppi]
Xool it[Soppi]
Tekki[Soppi]
Waxiin
Déglu baatu bind ci wolofi Senegaal