dog
Aller à la navigation
Aller à la recherche
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
dog : amna ñaari maanaa
- dog lees dagg,
- dogluy wone àpp bu man ta ñàkk,
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]
- dog lu naa sama ndimo la
- Yàlla nee: ku ne di nga dee ci àpp bu dog,
Xool it[Soppi]
Tekki[Soppi]
Waxiin
Déglu baatu dog ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-dog.ogg