bàyyikoo
Apparence
Wolof
[Soppi]→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
bàyyikoo g
- ci ndefar: ag njuréef man naa bàyyikoo ci geneen, ni diw di bàyyikoo ci gerte
- ci nos-wax: ab baat bu bàyyikoo ci beneen, baat bu am reenu beeneen, ca boobu la bàyyikoo.
- barab, fa am mbir jóge
Tekki
[Soppi]faraňse: origine |
angale: origin |
itaaliyee: origine |