baril
Aller à la navigation
Aller à la recherche
Wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
mi ngi bàyyikoo ci bari
Jëf[Soppi]
baril:
- yokk limu am mbir, def ko mu bari
- jàngi téere moo la taxa mana baril say baat yi nga xam,
Tur[Soppi]
baril g:
- yokk gi ngay yokk limu mbir mi
- baril gu samay falkat moo ma taxa falu
Bàyyikoo[Soppi]
Tekki[Soppi]
wu-faraas: multiplier, multiplication
wu-angalteer: multiple, multiplication
Delluwaay[Soppi]
Mbay Fay - nanu xayma - Tëngéej IREMPT (UCAD), 2005