bari
Aller à la navigation
Aller à la recherche
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
bari:
- bari lu ap ñatt ci lees man a waññi, tey duun ci lees man ta waññi
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]
- Xamnaa xeeti xam-xam yu bari. Amnaa xam-xam bu bari.
Xool it[Soppi]
Tekki[Soppi]
Waxiin
Déglu baatu bari ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-bari.ogg