→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
appoo:
- ci xayma: mooy wax ju jarul biral, ndax ag dëggoom
- nit nitay garabam, lii ab appoo la, ndax dëgg gu jarul biral la
wu-faraas: axiome
wu-angalteer: axiom
wu-itaali: assioma
Mbay Fay - nanu xayma - Tëngéej IREMPT (UCAD), 2005