wu-itaali

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

wu ak turu réew wii di Itaali

wu-itaali

  1. wu-itaali làkk wees gën a wax ca itaali,

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]

  1. làkk wu Itaali bokk na ci làkk yees gën a wax ci àddina

Xool it[Soppi]

Tekki[Soppi]

Nuvola apps edu languages.svg Waxiin

Déglu baatu wu-itaali ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-wu-itaali.ogg