Aller au contenu

biral

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

biral:

  1. ci xayma: joxe ay firnde yuy firndeel ay kàddu yu ñu yëkkati woon:
    biral ab céet
    biral ab waxeef

biral g:

  1. mooy mbooleem firnde yeek xalaat yi la may nga mana biral am mbir:
    biralug xayma
    biralug ab céet

Tekki

[Soppi]

wu-faraas: démontrer démonstration

Delluwaay

[Soppi]

Mbay Fay - nanu xayma - Tëngéej IREMPT (UCAD), 2005