Aller au contenu

Wiktionary:xam-xamu nosukaay

Jóge Wiktionary.

xoolal baat yi fi jota dugg xam-xamu nosukaay.


Arafu A

[Soppi]

- image d'arriere plan: nataalu xóot

- de tableau: kërug tablo, kërug xaatim/alliwa, kërug xaatim

- choisir un mode d'affichage: tànn aw wonewiin/waniin, tànn aw woniin

  • equivalent clavier: ab wecci-arafukaay, ab wuutu-arafukaay, ab kem-arafukaay
  • classe: jataay
  • clavier: arafuwaay (bu dee fi ñuy defe ay araf) arafukaay (bu dee li ñu koy defe(jumtukaay bi)
  • clic: ag cuq, ag cuut, kokk, bës
  • clignotement: xuyy-kamaj -g

- double-clic: ñaari-cuq b-

- fichier compressé: taxañ bees naj, ...bu naju, dencukaay bees naj, ëmp bu danku,

- en ligne: cig lënku, ci buum gi

- hors ligne: cig lënkoodiku, biti buum gi

- duurée de la connection: diirub lënku gi, diirub lonkoo gi

-convertir un texte en tableau ou vice-versa: wëlbati( mbaa soppi) yax (mbind) mu doon tablo(mbaa xaatim) walla safaan ba

  • copie: ab sotti, duppiit -w
  • copier: sotti, duppi, tibb,
  • corbeille: ab peñe, defukaayu mbaliit, póllu mbalit, walla póll
  • corriger: topp (moo gën a siiw), jagal, jaŋ, jubbanti
  • cote à cote: jàkkaarloo b-,
  • couper: dagg, dog
  • copier-coller: duppi-tay, duppi-taf
  • couper-coller:dog-fat, dagg-tay, dog-taf
  • coupure de mot, césure, hyphenation: dogandi b- dogug baat b-

- césure automatique: dogandi gu boppu, dog boppam

  • compatible: méngoo
  • créer: sos

- créer un style: sos aw meliin

- créer un document : sos ab jukki, sos aw wayndare

- créer un en-tete: sos ab boppaan

- créer un graphique sans l'assistant: sos ab garaafig ci lu dul yombalkaay, jàppalekaay, jàppalekat, sosal sa bopp ab garaafig

- créer un modèle: sos ab roytéef, sos ab royuwaay (ci wikipedia royuwaay lañuy fay jëfandikoo)

- créer un pied de page: sos aw suufu-xët, suufaan aw

- créer un titre fantaisie: sos ab boppub janeer, sos ab ponkub janeer, sos ab bopp bu kiimaane

- créer une insertion automatique: sos ag roof-boppam, sos ag roof gu boppu

- créer une lettrine : sos araf wu njool

- entre crochets : ci diggantey lonku

  • curseur: joxoñ b-, dawaan b-, junjaan b-, tuxuwaan b-,

- défilement horizontal: tuxal gu tëdd

- ... vertical: tuxal gu taxaw

- déplacer un élément de tableau: tuxal/randal xeetu xaatim/tablo

- déplacer (se): tuxu, dox

- déplacer (se) dans un document: tuxu ciw wayndare/ab jukki

- matériel;hardware: daju g-, jumtuwaay b-, jëfandaay b- ndëgër g-

- document de destination: jukki/wayndare bi mu jëm - document type: jukki/wayndare wu/bu roytéef, xeetu wayndare

- document source: wayndareb cosaan

  • données: njoxe b/y- rootaan m-

- base de données : dàttub njoxe, sàqum rootaan

  • dossier: ŋara w

- dossier de favoris: ŋaraw taamu /xejj yi, wayndareb tànneef

- plein écran: xoolu/seetu,seetukaay añs bu fees, fees xoolu

  • éditer: soppi, jubanti ,jagal, jëmmal, defar
  • éffacer: far
  • éffectuer les totaux: wàcce/def boole yi,
  • éjecter: génne
  • élément d'un tableau: xeetu tablo/xaatim

- élement type: xeetu roytéef, yëfi roytéef

- densité d'encre: faraayu daa b-

- économiseur d'encre: sakanalaakonu daa, yaxanalaakonu daa

- endroit de destination : barab bi mu jëm, ab jëmuwaay,

- enfoncer le bouton de la souris: bës butoŋu jinax ji

  • enregistrement,sauver,sauvegarder: wattu, aar. Boo wattuwul mbind yi nga dugal, dañuy far, boo fayee nosukaay bi, denc(?)

- enregistrement automatique: wattu/aar boppam, wattu/aar gu boppu

- enregistrement sous: wattu ci

- enregistrer un document: wattu ab jukki/ aw wayndare

- erreur système: njuumtel noste/tëraliin/nosiin

- source d'erreur: balluwaayu njuumte li, gongikuwaayu njuumte li

  • espace: ndeŋleer g-, diggante b-

- espace insecable: ndeŋleer gu doguwul/daguwul, diggante bu doguwul

- espacement: soriyànteel, ndeŋleeral,soriyantoo g-

- explorateur de document: seetkatu/gëstukatu/nemmikukaayu jukki/wayndare

  • exposant (en): (ci) mbind mu tiim, (ci) tiimaan
  • favori (bookmark): taamu y-, xejj y-, tànneef, màndarga-xët
  • fenêtre: palanteer

- fenêtre active: palanteer biy dox

- fenêtre inactive: palanteer bi doxul

- nouvelle fenêtre: palanteer bu bees

- flèche de defilement: fittug tuxal

- flèche à deux têtes: fittug ñaari bopp

- flèche descendente: fittug wàcc, fitt guy wàcc

- tête montante: fitt guy yéeg, fittug yéeg

  • folioter, paginere,numeroter les pages: nimeróol xët, sàkkal xët nimero, xëtal

- foliotage automatique: nimeróol-boppam, xëtal boppam,

- gérer les sauts des pages: saytu tëbi xët yi

- gérer un document en mode aperçu: saytu aw wayndare ci anamug seetlu

- outil de gestion: jumtukaayu caytu -b

- impression suspendu: móol gees aj

- impression terminée: móol gees noppi

- impression trop foncée: móol gu ñuul lool

- imprimante en réseau: móolukaay cig mbaal

- imprimante locale: móolukaay bu barab

- imprimante prête: móolukaay bu jekk

- pilote d'imprimante: dawalukaayu móolukaay, tettekatu móolukaay

- initialiser une disquette: daloo ub disket/as tappaan, door ab tappaan

- insérer un colonne: roof ab keno

- insérer des espaces insécables: roof ay ndeŋ-leer yu doguwul/yu daguwul

- insérer une ligne (de tableau): roof as sàppe

- insérer un symbole: roof ab junj

- insérer un tableau: roof ab xaatim

- lien hypertexte: lëkkalekaay bu am pàŋŋ, lëkkalekaay bu yax/mbind mu/bu ne fàŋŋ

- majuscule-cic: mage-cuq

- marge droite: peggu ndijoor b

- marge du bas: pegg bu suuf

- marge gauche: pegg bu càmmooñ

- marge du haut: pegg bu kaw

- mémoire morte,ROM: xel mu dee, dëxëñukaay bu dee, ndàmb lu dee. - mémoire vive,RAM: xel muy dund, dëxëñukaay buy dund, ndàmb luy dund.

- article de menu: jukkib njël

- menu abrégé: njël lees gàttal

- menu affichage: njëlul wone

- menu contextuel: njël lu méngoo

- dérouler un menu: tàllal njël

- menu déroulant: njël lees di tàllal, njël luy tàllalu

- menu edition: njëlul jagal

- menu fichier: njëlul taxañ/dencukaay l-

- menu format: njëlul melokaan/jëmm

- menu insertion: njëlul roof

- menu outils: njëlul jumtukaay l-

- sous-menu:ron-njël l-

- messages d'alerte: bataaxalu artu b-

- messages d'erreur: bataaxalu njuumte b-

  • mettre en veille: xembi
  • minuscule: ndawe b- arafu ndawe
  • mise en page: defariinu xët w- tëgiinu xët w-
  • messagerie: diisoowaay, diisookaay
  • mode lecteur a l'écran: yëriin ci seetukaay bi w-, anamu jàng ci xoolu

-mode normal: anam gees baaxoo, anamug baax gi, anam gu jaadu

- mode page:anamu xët: dafa lay won, cig maasale, ni jukki biy taxawe ci kaw xët wi

- mode plan: anamu naal

- mode d'affichage: woniin w-

- mode d'insertion: roofiin

- modifier l'alignement des paragraphes: soppi toppanteeb xise yi

- modifier l'espacement des lignes: soppi diggante màndarga yi

- modifier la dimension des marges: soppali dayob pegg yi

- modifier la police des caractères: soppi njabootu màndarga yi

- modifier la taille des caractères : soppi dayob màndarga yi

- modifier le style des caractères : soppali meliinu màndarga yi

- modifier les colonnes : soppi keno yi

- modifier les lignes d'un tableau: soppi rëddi xaatim yi

- mot entier: baatu bu ñumm b- baat bépp

- mot de passe: baatu-jàll b-

- mot-clé: baatu caabi

  • moteur de recherches: yëngalukaay/yëngalkatu gëstu, motóoru gëstu/seet, seetkaay
  • multiplier: baril
  • multimédia:yeenekaay bu anamu, yeenekaay-bari-anam, yéenekaay bu ubbéeku, barixibaarukaay

- nom de domaine: turuw moomeef - turuw lew

- nom de l'utilisateur: turu jëfandikukat w-

- nommer: tudde

  • normal: lees baaxoo, lees aadawoo, bu mbaax, bu aada, jaadu
  • note : karmat b-

- notes de bas de pages: karmati suufi xët

- nouvelle fenêtre: palanteer bu bees

- nouvelle onglet: gàll wu bees

- option disponible: tànneef gu jàppandi

- option indisponible: tànneef gu jàppandeedi

- page d'accueil, home page: xët wu njëkk, xëtu dalal jàmm, xëtu teeru/teertu, njalbeen

- page d'essai; cleaning page: xëtu setal w, xëtu setaluwaay

- page impaire: xët wu tóol

- page paire: xët wu tóoladi

- page précédente: xët wi weesu

- page suivante: xët wi toftal

- page web: xëtu web

- alimentation papier: def kayit

- entre parenthèses: ci diggantey xala

  • partager: séddoo, bokk(soo nee séddoo dafay mel ne danga koy dagate ay xaaj, séddale ko)

- dossier partagé :ŋara wees bokk

- partager un dossier: bokk aw ŋara

- personnaliser la fenêtre: jëmmal palanteer bi

- personnaliser la barre d'outils : jëmmal/méngale xocc/bànqaasu jumtukaay bi ak sa koobare

- pointeur en I: joxoñukaay bu I

- sencond plan (mettre au); send back: gannaawal

  • presenter un texte en colonnes: taxawal am mbind/ab yab ci ay xàll/keno

- présenter une liste avec des numéros: taxawal ab lim/ab list bu ànd aki limukaay/nimero

- présenter une liste avec des puces: taxawal ab lim/list bu ànd aki felliit

  • raccourci: ñall w-
  • radio: rajo
  • rangée,ligne de tableau;row: as sàpp
  • rassembler, défragmenter: dajale, taqale
  • réception: jot g-,
  • récepteur d'appel: jotkatu woote, jotukaayu woote b-
  • reçu: njotu l-,
  • rechercher: seet,wër, gëstu

- recherche avancée: ceet gu xóot

- recherche de fichier: ceet ab taxañ/dencukaay

- recherche globale : ceet gu matale

- restreindre la recherche: xatal ceet gi

  • rechercher: seet
  • recto/verso : biir ak biti, ñaari wet yi
  • réduire: wàññi

- réduire les dimensions de l'affichage: wàññi dayob wone gi

  • refaire: defaat
  • règle: rëddukaay b, jubalukaay b

- règle horizontale: rëddukaay/jubalukaay bu tëdd b

- règle verticale: rëddukaay/jubalukaay bu taxaw

  • relâcher le bouton de la souris: féexal butoŋu jinax ji
  • remplacer(mettre à la place de): wuutal

- remplacer automatiquement une mise en forme: wuutal fi ag jëmmal ci anam gu boppu, wuutal fi ag jëmmal boppam

- réorganiser tout: nosaat lépp

  • Réparer: jagal, defar (misaal: moodu de defarkatu tele la )
  • réparation: jagal g-,
  • repère, guide: gindikaay
  • repérer (se) dans l'écran: gindiku ci seetukaay bi, gindiku ci xoolu bi
  • répertoire: dencuwaay,
  • répéter: baamu,baamtu

- répéter frappe: dóoraat

- être en réseau : tàbbi cig mbaal, lëkkaloo, nekk cig mbaal

- mettre en reseau: tàbbal cig mbaal, lëkkale

- réseau en distance:mbaal cig soreyoo, lëkkale cig soreyoo e-mbaal/e-lëkkale

- résultat de la recherche: njuréef/ngérte lu ceet/gëstu gi

-retrait, renforcement à droite: beddeeku gu ndijoor

-retrait, renforcement à gauche: beddeeku gu càmmooñ

-retrait, renforcement paragraphe:beddeeku gu xise

  • saisie de texte: dugalug mbind
  • saisir un texte;to enter a text: dugal mbind
  • saut de colonnes;column break:tëbub keno keno bu bees

- saut de page, changement de page;page break, new page: tëbu xët, xët wu bees

- saut de page automatique;automatic page reak: tëbu xët wu boppu, xët wu tëbal boppam, xët wu bees wu boppu, xët wu beesal boppam

- saut de ligne;new line: tëbu rëdd, rëdd wu bees

- scinder une cellule: xar ag kër

- scinder un tableau: xar ab xaatm/ab tablo

  • sélection de modes d'affichage: tànnug wonewiin y
  • sélectionner: tànn

- sélectionner tout: tànn lépp

- sélectionner du texte: tànn am mbind, ab yax

- sélectionner un élément de tableau: tànn aw xeetu/ab cëru tablo/xaatim

-signature numérique, (digital signature): xaatim bu limate

  • signet;bookmark: xamtu b, takku b
  • silence: cell g. Daf lay won ne nosukaay bi gisul li nga ko doon seetloo
  • séparateur:
  • site web: dalu web b
  • site: dal b
  • software: ab xeltéef, aw tëriin
  • souligner;underline: rëdd-ron-gi, ron-rëdd, :ronrëddal mbind mi,walla rëddal ron gi, rëddaatu (dama gis fees ko jëfandikoo, moom jëfandikoo ci wikipedia)
  • sous: ron,
  • sous-page: ron-xët,
  • sous-répertoire: ron-dencuwaay,
  • source: ab gongikuwaay, ab day
  • souris: jinax j
  • stable : daladi
  • suivre: topp
  • suivant:aji topp, li ci topp
  • supprimer: dindi, far

- supprimer une cellule: dindi ag kër

- supprimer une colonne: dindi ab keno/aw xàll

- supprimer une linge ( de tableau): dindi as sàppe

- supprimer un mot: dindi ab baat

- supprimer un style: dindi aw meliin

- supprimer du texte: dindi ab yax

  • surbrillance, highlight: niit
  • stockage: ndëxëñ g, denc b
  • style: meliin w
  • symbole: junj b-
  • synonyme: maanaante, bokk-tekki
  • système d'exploitation: aw doxiin, nosteg doxiin.Mooy ni nosukaay bi, mbaa noste gi nosukaay bi di doxe, may ko manees cee def jëfekaay yees di liggéeye, niki bind, nataal walla xayma. Windows aw doxiin la/ag nosteg doxiin, ci làkku Angalteer: operating system = noste giy liggéey

- tâche de'impression: sasuw móol

- taille d'une image: dayob nataal

- sous-titre: ron-bopp b

  • toile d'araignée mondiale;World Wide Web: lëndug àdduna bi
  • touche;key:caabi j

- touche étoile;star key: caabi biddiw j

- touche de fonction: caabiy jëf j,

- touche de racourci: caabi ñall j

- touche majuscule: caabi mage j

- touche tabulation: caabi tëbaan j

  • tracer des bordures: rëdd ay dig
  • traduire :tekki
  • traitement de texte;word processing: caytug mbind g
  • trame ,cadre;frame: kaadar b

- trame de fond: kaadaru ag xóot

  • transformer: soppali
  • travaille: liggéey b
  • tri croissant: waññ guy yéeg, tànn guy yéeg

- tri décroissant: waññ/tànn guy wàcc

  • trier: tànn/waññ
  • tableau: xaatim

- visualiser des documents fusionnés: gaaral ay jukki yees boole

  • vitesse: xél w,
  • zone de dialogue: waxtaanuwaay
  • zone de texte: barabu yax
  • zoom : rëyal g,