denc

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

Open book 01.svg Jëf[Soppi]

denc:

  1. dencal ma sama xaalis bii
  2. dencal këyit yii ndax am nañu solo lool
  3. denc rekk moo wóor!

yeneeni làkk[Soppi]

wu-faraas:sauvegarder, garder, archiver