Wiktionary waxtaan:xam-xamu nosukaay

Le contenu de la page n’est pas pris en charge dans d’autres langues.
Jóge Wiktionary.
  • abonnement: takkoo.M: def naa ag takkoo ci benn yéenekaayu ayu bis
  • abonné: aji/way takkoo
  • acces: dugg, yoon
  • acces direct: duggug jonjoo
  • acces reseau a distance: dugg ci mbaal gu sori/yoonu lëkkale gu sori/e-lëkkale
  • acces sequentiel :dugg gu ami jaar-jaar
  • chemain d'acces: yoonu dugg
  • code d'acces: baatu dugg
  • fournisseur d'acces: dugalukaay, dugalkat, dugalekaay
  • technologies a'acces a Internet: xaralay dugg ci lënd gi (internet bi)
  • accessoire de bureau: jëfandaayu biro, jumtukaayu biro, jumtukaayu bindu (biro)
  • accueil: ag teeru, ag dalal, njalbeen,gatandu
  • accueillir:teeru, dalal
  • activer: sawaral, dundal, doxal
  • actualiser: yeesal
  • adresse: Xamekaay, màkkaan
  • adresse e-mail: adrees e-bataaxal, màkkaanum mbëjfeppal
  • affichage: wone, woniin
  • affichage pleine page: wone xët wu fees
  • afficher: wone
  • alignement: péetale, wàllale
  • alignement centre: péetale gu diggu
  • alignement justifie: péetale gu maase
  • alignement sur la droite: ....gu ndijooru
  • alignement sur la gauche: .....gu càmmooñu
  • allumer: taal
  • ameliorer: gënal
  • version amelioree: sottiin wu ñu gënal, sumb bu ñu gënal
  • annuler: neenal,
  • annuler une frappe: neenal ab dóor
  • aperçu avant impression: seetlu njëkk-móol
  • appeler: woo, woote
  • application: jëfekaay, tëriin
  • appliquer: jëfe, doxal
  • appliquer un style: jëfe/doxal aw meliin
  • arriere-plan, fond: ag xóot
  • d'arriere plan: gu ag xóot

- image d'arriere plan: nataalu xóot

  • arrondire: roŋal,(mottali lim (bu dee xaalis))
  • article: jukki b-, wax j-, mbind m-
  • assistant,wizard: yombalkaay,jàpplekaay, jàppalekat
  • atteindre: àgg ci, yegg ci
  • assembleur: boolekaay
  • assemblage: mboole, boole g
  • assembler: boole
  • augmenter: yokk
  • avertir: artu/aartu