ñoñ-àtte

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

mi ngi bàyyikoo ci àtte ak ñoñ

Open book 01.svg Tur[Soppi]

ñoñ-àtte b:

  1. mooy ñiy yëngu ci lijjanti nit ñi
  2. nit ñiy yëngu ci luy doxal yoon

Xool it[Soppi]

Tekki[Soppi]