Aller au contenu

yoon

Jóge Wiktionary.

Aw yoon

wolof

[Soppi]
  • àtte bi ñépp di tënku: dama lay yóbb ci yoon boo ma tooñee
  • fi ñuy jaar, di fa dox:yoonu saxaar gi de weñ la
  • ag nosu: tegu ci yoon lu am njariñ la.

francais

[Soppi]
  • loi;code
  • voie
  • ordre