xarey jóoñe
Apparence
wolof
[Soppi]- xarey jóoñe yu jamono ju diggu ji,nekkoon nañu di ay aj aki siyaareji yu ñu ngànnaayal, paab bee leen daa woote, ngarmi gu Tugal gi di leen jàppale ci alal, di leen kapparal, te di leen jëfloo, bu ko defee, ñu sóobu ci ay jiyaar yu nasaraan.
yonnee yu xare, yu nasaraan yii, ñi ngi léen daa wootee ci turu goreel Quds (Sorisalem), gi waa Tirki tegaloon loxo Araabi Faatima yi, ci atum 1078
français
[Soppi]- croisades
Les croisades du Moyen Âge étaient des pèlerinages armés prêchés par le pape, financés et mis en œuvre par la noblesse d'Occident. Elles s'inscrivaient dans la guerre sainte chrétienne du au s. Ces expéditions militaires chrétiennes ont été prêchées au nom de la libération de Jérusalem, conquise aux Arabes Fatimides par les Turcs en 1078.