Aller au contenu

ngarmi

Jóge Wiktionary.

mi ngi bawoo ci garmi giy tekki noble ci fr, ngarmi nag mooy noste gi nga xam ne nguur ga danu koy donnante, walla du génn ñenn ña diy garmi, maanaam ñu tedd, safaanub baadoola yi