araab
Apparence
wolof
[Soppi]→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
Araab
- Làkk la wu ñuy wax ca Penku-Gu-Jege ak ca Bëj-gànnaaru Afrig
- Abajada bi ñu koy bindee ngi bawoo ci wu-aram, ci lees di binde it pers
Déglul baatu araab ci wolofi Senegaal