Aller au contenu

wikipediyaa

Jóge Wiktionary.
Wikipedia am na jukki bu tudd:

Wolof

[Soppi]

Mi ngi juddu ci booleb waati angale yu wiki ak encyclopedia (jimbulang) → Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

wikipediyaa b

ab sémbub jimbulang la, doon tëriin bu ubbeeku

Tekki

[Soppi]
farañse: wikipedia
wu-angalteer: wikipedia
wu-itaali: wikipedia