Aller au contenu

waxeef

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

mi ngi bàyyikoo ci wax

waxeef b:

  1. ci xayma: mooy wax joo wara biral walla laaj boo wara tontu

Tekki

[Soppi]

wu-faraas: (mathématique) proposition

Delluwaay

[Soppi]

Mbay Fay - nanu xayma - Tëngéej IREMPT (UCAD), 2005