taw
Ëmbéef
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
taw
- taw ndox miy bawoo ci asamaan wàcc ci suuf, tey doon lu nit ñi man a yëk,
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]
- biig dey taw na tawub waame, réew mepp a ngi ji,
Xool it[Soppi]
Tekki[Soppi]
- wu-faraas: -
- wu-angalteer: -
Waxiin
Déglu baatu taw ci wolofi Senegaal