waame
Apparence
wolof
[Soppi]waame
- waame taw bu matale
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- taw na tawub waame réew mépp a ngi ji
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: - orage
- wu-angalteer: - storm
Déglu baatu waame ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-waame.ogg