samp

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

Open book 01.svg Jëf[Soppi]

Samp:

Ci xam-xamu nosukaay
  1. Di nañ wax 'samp aw tëriin'
Ci lu daj
  1. jël am mbir samp ko, samp bant bi
  2. Samp kër

Bokktekki[Soppi]

taxawal

Bàyyikoo[Soppi]

Camp

Tekki[Soppi]

wu faraas: instaler
wu angalteer: install