sóob

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

sóob: amna ñatti maanaa

  1. sóob tambalib taw,
  2. sóob duy ag gënn di waaja dëbb,
  3. sóob kuy caaxaan,

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:[Soppi]

  1. tawbi sóob na
  2. sóobal ma soq
  3. yaw dangay sóob rek;

Xool it[Soppi]

Tekki[Soppi]

Nuvola apps edu languages.svg Waxiin

Déglu baatu sóob ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-sóob.ogg