raw
Apparence
wolof
[Soppi]raw: am na ñatti maanaa
- raw jiitu .
- raw ab janx a koy ame bu masula joteek góor,
- raw boole ay wëñ mbaa lu ni mel
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- aamerig raw na réew yi.
- diw... wacci na soxnaam ci fékku kook raw.
- rawkati bum yaangi raw ag bar
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: gagner
- wu-angalteer: win
Déglu baatu raw ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-raw.ogg