buum
Apparence
wolof
[Soppi]buum: am na ñaari maanaa
- ag buum wëñ yees boole ràbb a le ko,
- ag buum li boole góor ak jigéen ci ab sëy.
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- diw dey ràbbkatu buum la.
- mana goo sëy ak keneen dangaa nékk ci ag buum.
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: corde
- wu-angalteer: rope
Déglu baatu buum ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-buum.ogg