Aller au contenu

néewte

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

Mi ngi jóge ci néew

Néewte:

  1. Mooy ña gën a néew ciw askan di safaanub ëppte.néewte gi, ag néewte
  2. Mooy ñi nekk ci kujje gi, langu politig ga gën a néewi ndaw ca péncum réew ma

Tekki

[Soppi]
wu faraas: minaurité
wu itaali: minorita
wu angalteer: minority
araab: الاقلية