Aller au contenu

néegub jàngale

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

Ci jàngu yi ay néegi jàngale yu baree fay nekk, njàngaan yi di ca nekk di jàng.

Yeneeni làkk

[Soppi]
wu faraas: classe
wu itaali: classe
wu angalteer: classroom