mbokkte

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

Wolof[Soppi]

Nuvola apps bookcase.svg Gongikubaat[Soppi]

ci politig: ag nosteg yoriinu am réew la, nguur gi mooy moom lépp (liggéeyuwaay yi, dëkkuwaay yi, añs), nit ñi duñu moom dara, lépp li ci réew mi dañu koy bokk.

Xool it[Soppi]

Yeneeni làkk[Soppi]

Wu faraas: communisme
Wu angalteer: communism
Wu itaali: comunismo