noste

Jóge Wiktionary.
Sauter à la navigation Sauter à la recherche

wolof[Soppi]

  • noste mi ngi juge ci nos giy firi raŋale ay mbir jekkal leen te teg leen ci anam gu tegu ci yoon

noste nag mooy tëriin walla nosiin wi mbir yi di nekk, nosteg laman: ni laman yi daan def di ci nose seen ag dund ak seeni jaam walla ñi ñuy jox seeni suuf

francais[Soppi]

  • systeme

Italiano[Soppi]

  • sistema