gongikuwaay

Jóge Wiktionary.
Aller à la navigation Aller à la recherche

Gongikubaat[Soppi]

xoolal gongiku

Tur[Soppi]

gongikuwaay:

  1. fu am mbir bàyyikoo
  2. ndax xam nga gongikuwaayu sa yëre bi? Maanaam fu yëre bi jóge

Bokktekki[Soppi]

wu-faraas:origine, source