Aller au contenu

dencu

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

mi ngi jóge ci denc

dencu:

  1. mooy jël ab xibaar denc ko, aar ko
  2. Ci dencu yu senegaal di nga fekk bépp mindu taariix ñeel réew mi.

Tekki

[Soppi]

wu-faraas:archive