daal
Apparence
wolof
[Soppi]daal: am na ñaari maanaa
- daal dees koy jëfandikoo ngir gàttal wax.
- ag daal/ag deel arafu araab la, 4eelu araf ci abajada araabu daaray senegaal
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- moom daal ku baax la,
- daal 4 la ci xayma
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: pour ce qui est de
- wu-angalteer: as for
Déglu baatu daal ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-daal.ogg