daa
Apparence
wolof
[Soppi]Daa: am na ñaari maana
- daa ndox mu ñuul mees di sëpp xalima di bind
- daa dees koy jëfandikoo ci wax muy dellu ci «moom» (moom faatu)
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- xalima balaa bind daa teew !
- faatu kay daa reew rek waaye baaxna
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: - encre
- wu-angalteer: - ink
Déglu baatu daa ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-daa.ogg