dëkk
Aller à la navigation
Aller à la recherche
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
Tur[Soppi]
dëkk (b):
- ci melosuuf: ag dajaloo gu ay nit aki kër yu takku te lëw
Jëf[Soppi]
dëkk:
- Dem fenn samp fa kër nekk fa, di fa amal say yëngu-yëngu
Bokktekki[Soppi]
yeneeni làkk[Soppi]
wu-angalteer: city, live |
wu-fraas: ville, habiter |
wu-itaali: città, abitare |