dànkaafu
Aller à la navigation
Aller à la recherche
Wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
Jëf[Soppi]
- dànkaafu:
- liggéeykat yi dànkaafu nañu seeni kilifa, nee nañu leen suñu leen fayul, di nañu bank seeni yoxo
Tur[Soppi]
- dànkaafu b :
- liggéeykat yi jox nañu seeni kilifa dànkaafu bu mujj laataa seen mbankum loxo