artu
Aller à la navigation
Aller à la recherche
Wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
Jëf[Soppi]
artu
- dànkaafu
- liggéeykat yi artu nañu seeni kilifa, nee nañu leen suñu leen fayul, dinañu bank seeni yoxo.
Tur[Soppi]
artu b
Waxiin
Déglul baatu artu ci wolofi Senegaal