cër
Apparence
wolof
[Soppi]→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
cër:
- Nit: wàll yi ci jëmm ji, loxo yi ci cër yi la niki tànk yi;
- mbootaay: Senegaal cër la ci xeet yu bennoo yi (mbootaayu xeet yi), Senegaal ci mbootaayu xeet yi la bokk.
- Koom-koom: liy tax ngay bokk ci ag mboolaay walla ab liggéeyuwaay jaare ko ci jënd fa ay cër.
- Wàll: jox ma sama cër ci li ñuy séddale: jox ma ci sama wàll;