Aller au contenu

jëmm

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]

→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

Jëmm:

  1. Mooy xam-xam biy settantal aka lëjmbët feñte yi nekk ci li nu wër, ci àdduna bi ak ci asamaan si.
  2. Kenn:jëmm ji ma taseel démb niru na baayam

Tekki

[Soppi]

wu-faraas

  • physique
  • une personne: la personne que j'ai rencontrée hier ressemble à son père
  • indentité