Aller au contenu

bon

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]

bon: amna ñaari maanaa

  1. bon lu/fu/ñu/ku melul namu war a mel, maanaam yàqu,
  2. bon dees nako taaralee wax,

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

[Soppi]
  1. soxna sii ni mu bonee, cagatu rek liggéey,
  2. bon nu bàyyi beneene,

Xool it

[Soppi]

Tekki

[Soppi]

Waxiin

Déglu baatu bon ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-bon.gg