bataaxalub mbëjfeppal
Aller à la navigation
Aller à la recherche
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
xoolal mbëjfeppal ak bataaxal
Tur[Soppi]
Bataaxalub mbëjfeppal
- Bataaxalub mbëjfeppal di nañ ko wax itam m-bataaxal
- Yónne ma ab Bataaxalub mbëjfeppal ci sama boyot.
yeneeni làkk[Soppi]
- wu-fraas: courriel électronique
- wu-angalteer: e-mail
- wu-itaali: posta elettronica, e-mail