bataaxal
Aller à la navigation
Aller à la recherche
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
→ Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
Tur[Soppi]
Bataaxal
- Yónne ma ab Bataaxalub mbëjfeppal ci sama boyot;
- Bind ab bataaxal;
- Bataaxal man naa nekk bu ñu bind ak këyyit, walla mu doon bu mbëjfeppal