ban
wolof[Soppi]
Gongikubaat[Soppi]
ban: amna ñaari maanaa
- ban bi yàlla wax ni ci la bind nit, muy nduroo ak suuf te ci lay bawoo.
- ban bees di jëfandikoo ngir laaj te, Misaal:ban dal mooy wax ci wolof ?
Xool it[Soppi]
Tekki[Soppi]
- wu-faraas: Mud
- wu-angalteer: Mud
- araab: الطين
Waxiin
Déglu baatu ban ci wolofi Senegaal