Aller au contenu

bóof

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]

bóof:

  1. bóof toog ci mbir,

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

[Soppi]
  1. ginaar gi tambali naa bóof ay nenam,

Xool it

[Soppi]

Tekki

[Soppi]

Waxiin

Déglu baatu bóof ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-bóof.ogg