diju
Apparence
wolof
[Soppi]diju:
- diju took ci dara, niki suuf, lal, basaŋ ak luni mel
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- dijul ci basaŋ gi
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: -
- wu-angalteer: -
Déglu baatu diju ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-diju.ogg