Aller au contenu

béw

Jóge Wiktionary.

wolof

[Soppi]

béw,

  1. béw: jikko ju bon la ci nit, maanaam ku faalee tul ay kilifaam.

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

[Soppi]
  1. diw dey leegi daa béw ba faalee tul ay way-juram

Xool it

[Soppi]

Tekki

[Soppi]

Waxiin

Déglu baatu béw ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-béw.ogg