Aller au contenu

aasma

Jóge Wiktionary.

Wolof

[Soppi]

baatub aasma ci làkku farañse la bawoo. → Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)

aasma b

  1. tawat la, ci tawat yi moom nag jamonoy nawet lay bañ.